• Banc say-say 4

    Banc say-say 4

    ma ladj léne. kou djiguéén ki da gnou kay forçé wala....

    banc bii djaxalnama.

     A suivre ....


    Tags Tags : , , , ,
  • Commentaires

    1
    nansig
    Lundi 16 Janvier 2012 à 22:14

    pa bi kou gnak fayda la. wornama ni bayi na djabaram tchi keurga

    2
    BE COOL
    Lundi 16 Janvier 2012 à 22:48

    MAIS BANC BII FOUMOU NEK DAMA BEUG GUISSAL SAMA BOPP DOYNA WARR

     

    3
    thioukii Profil de thioukii
    Lundi 16 Janvier 2012 à 23:41

    mane dé warotina si banc bi tjrs akk bou béss


     

    4
    goooo
    Mardi 17 Janvier 2012 à 12:29

     moy say sépi

    5
    goooo
    Mardi 17 Janvier 2012 à 12:30

    lou mouy def ni. c l bordel ou koi

    6
    vilooo
    Mardi 17 Janvier 2012 à 12:31

    pa bi kou doxane ndéyam la. da fa gnak fayda way

    7
    soular
    Mardi 17 Janvier 2012 à 12:32

    de vrai moins moins que rien

    8
    Mardi 17 Janvier 2012 à 14:53

    c'est grave. mais la fin du monde est en 2012. ca ne coute rien d'attendre.

    9
    madieye.mbengue3 Profil de madieye.mbengue3
    Mardi 17 Janvier 2012 à 17:51
    ki ka y dakoy force ki mo say say
    10
    beugg leuf
    Mardi 17 Janvier 2012 à 18:11

    ki dale kou beugg kate leu amoul foumouko defes c fini

    11
    khoulayy
    Dimanche 22 Janvier 2012 à 11:23

    forcé wouko dara gnom gnar gneupa say say

     

    12
    Mardi 15 Mai 2012 à 07:56

    non kou yen tamite kou khol banc bii khamne dou galsen way

    13
    krezy
    Mardi 5 Juin 2012 à 11:48

    mdrrr...



    Ajouter un commentaire

    Nom / Pseudo :

    E-mail (facultatif) :

    Site Web (facultatif) :

    Commentaire :